Musée des Civilisations noires: Bienvenue

JÓGE CA MÀNGAAN BA JËM CA SAX CA BARAB

Paléolithique gu mujj gi mbaa gu yees gi Paléolithique gu mujj gi, ñu koy tudde it Paléolithique gu yees gi mbaa gu gën a jëm kanam, yemook ja mono ji mujj ci jamono ya jiitu mboorum niteef ju yàgg ja.Li koy màndargaal mooy jëm kanamug ngànnaay yiy nirooleeki xob ak doji jànji sawara, ak yu […]

Voir plus

PALEYOLITIK GU DIGG-DÓOMU GI

Paleyotik gu digg-dóomu ga ma ngay tollook jamono ji topp ci Paleyotik gu suufe ga. Aaday njumtuwaay yu ñu defare tojit yu ndaw moo fa sàmpu, jaare ko ciy xar-kanami mbatiit yuy melal ay baaxi diiwaan.     Mbatiit yi gën a fës ci Paleyotik gu digg-dóomu ga ñooy Atérien fa Afrig ak Moustéren fa Órob. Fa […]

Voir plus

BARAB YI ËPP SOLO YI ÓSTARALIPITEK YI AK PARATOROP YI NEKK FAFRIG

ÓSTARALIPITEK YI AK PARATOROP Am na lu ëpp 4i tamdareti at, la ay mboolooy nit yuy doxe ñaari tànk, ñu tuddeleen óstaralopitek ak paratorop, feeñ. Ki ci gën a yàgg téy ñu xam ko mooy Australopithecus anamensis, ña nga feeñale fa Kanapoi, fa diwaanu lac Turkana, fa Keeñaa.    Ci luy tollook 3,5 tamdareti at, óstaralopitek […]

Voir plus

MBATIITUM OLDOUVAÏENNE (OLDOWAN)

Ci diggante 2,5 et 1,3i tamdareti at, nit ñu njëkk ya fentoon te yaatal am mbatiit (xam-xam) mu tudd Oldowayenne (mbaa Oldowan), te li ko doon gën a feeñal moo doon genn këru liggéeyug yattum doj gu xereñ lool ba tax yenn ciy njumtukaayam ñoo ngi wëy daan leen jëfandikoo ba ci jamonoy ji ñu […]

Voir plus

Ardipitek yi

Ci diggante 8 ak 6i tamdareti at, ci la xàjjaloo ame ci diggante xeetu dangin yi ak wuw nit ñi fi Afrig. Ci tolluwaayu peeñalug jamonoy yatt doj – càmm – wittat, ñatti giir ñoo àndandoo di xëccoo taxawaayu nit ki gën a yàgg gu ñu xam : Sahelanthropus tchadensis, ñu gën koo xame ci […]

Voir plus

Génn Afrig yi ak Kiliftéefu àddina si

Génn Afrig yi ak Kiliftéefu àddina si. Génn gu njëkk gi ñu génn Afrig. Homo ergaster, mbaa Homo erectus, mooy ki jëkk a génn Afrig ngir dem Asi ak Órob, am na lu war a tollu ci 2i tamdareti at. Màng gu njëkk googu, peeñali ngas-ngent yu bari dëggal nañu ko : ndaal bopp yi […]

Voir plus

AFRIG, LAYTAAYU NITEEF GI

Afrig ag kembaar la gu ame ndono lu yéeme te mbooru nitam yàgg lool. Afrig suufus mboor la, mbatiit ak ñeeñal, ci ay am-amam yu sàmmu, yu ñu luññutóogul. Moo ëmb ëllëgu niteef gi mu jur. Leegi ñépp nangu nañu ne Afrig mooy laytaayu niteef gi. Ndesi yaxi nit ñu njëkk ña ak firdey ngas-ngent […]

Voir plus

Femmes et politique

1-1 Luttes d’émancipation Anne Zinga (Angola) 1592-1663 Lumina Sophie (Martinique) 1848-1879 Yaa Asentewaa (Ghana) 1835-1921 Mekatili Wa Menza (Kenya) 1840-1925 La Negra Carlota (Cuba) décès 1844 Ndatté Yalla Mbodj (Sénégal) 1810-1860 Mariana Grajales Cuelo (Cuba) 1815-1893 Taytu Betul (Ethiopie) 1851-1918 Dandara Dos Palmarez (Brésil) 1654-1694 La reine Nanny (Jamaique) 1685 -1755 Rose Lomathinda Chibambo (Malawi) […]

Voir plus
Primary Color
default
color 2
color 3
color 4
color 5
color 6
color 7
color 8
color 9
color 10
color 11
color 12